Ngëneel yi ak teggiin yi
Jële nañu ci Abdullah Ibn Umar yal na leen Yàlla dollee gërëm mu wax ne:
Available in 54 languages
«Jële nañu ci Abdullah Ibn Umar yal na leen Yàlla dollee gërëm mu wax ne: Yonnente Yàlla bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc daawul bàyyi di ñaan lii, bu gontee ak bu xëyee: "Allaahuma innii as-aluka alhaafiyata fiddunyaa wal aaxirati, Allaahuma innii as-aluka alhafwa walhaafiyata fii diinii wa dunyaaya wa ahlii wa maali, Allaahuma ustur hawratii -walla hawraatii- wa aamin rawhaatii, Allaahuma ihfasnii min vayni yadayya, wa min xalfii, wa han yamiinii, wa han simaalii, wa min fawxii, wa ahuusu Bika an uxtaala min tahtii".»Meaning translation ·
Saved at original quality








