Ngëneel yi ak teggiin yi
Jële nañu ci Abdullah ibn Umar yal na leen Yàlla dollee gërëm mu wax ne: bokkoon na ci ñaani Yonnente Yàlla bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc:
Available in 53 languages
«Jële nañu ci Abdullah ibn Umar yal na leen Yàlla dollee gërëm mu wax ne: bokkoon na ci ñaani Yonnente Yàlla bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc: "Allaahuma innii ahuusu bika min sawaali nihmatika, wa tahawwuli Hanafiyatika, wa fujaa-ati niqmatika, wa jamiihi saxatika".»Meaning translation ·
Saved at original quality








