Hadith for the World
Tap the image to view it full size
Ngëneel yi ak teggiin yi

Jële na ñu ci Aysa -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: dégg naa Yónente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne:

Available in 66 languages
«Jële na ñu ci Aysa -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: dégg naa Yónente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne: «aji-gëm ji jikkoom ju rafet danako may mu am darajay Aji-woor ak kiy taxaw di julli».»

Meaning translation ·

Explanation

The meaning in a few plain lines

Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- day leeral ne jikko ju rafet dana yóbb boroomam ca darajay ki saxoo woor bëccëg ak taxaw guddi, li dajale jikko yu rafet yi mooy: di def njekk, ak rafeti wax, ak bélli xar kanam, ak bañ a lore te di ko dékku ci nit ñi.

Source
Abóo Daawuda soloo na ko,ak Ahmat
Download image

Saved at original quality