Pas-pasu Lislaam
Jële na ñu ci Taarix Ibn Asyam Al-Asjahii -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: dégg naa yónenteb Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne:
Available in 65 languages
«Jële na ñu ci Taarix Ibn Asyam Al-Asjahii -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: dégg naa yónenteb Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne: «ku wax: laahi ilaaha illallaahu, amul kenn ku ñu war a jaamu cig dëgg ku dul Yàlla, daal di weddi lépp lu ñuy jaamu te du Yàlla alalam ak dereetam araam na, Yàlla rekk nag mooy càmbar ay jëfam».»Meaning translation ·
Saved at original quality








